Yaag cii ndox du tax nga don jesit.
Xonq nopp!
Nuul tuñ!
Lay! Toubab buy l`àkk Wolof?
Li de graw na.
Naq a naqari luqati ci tuq.
Léer ñañ tey weex taal.
Doomu toubab du sol daal?
Suuf si day làkk de.
Salamalekum, baal ma àq.
Mësuma giss toubab buy ñani ndewenal.
Kaay, lekkal lepp lo bëgg.
Baal na la.
Fatou Chewing-gum ak Witen Gerte,
Ñari xarite, no stress.
Ñari sereer, bëgg lekk.
Je t’aime beaucoup.
Dawal xotibant ci kaw tali ba,
Etwal yi ci Asaman di ñu leeral.
Tabaski:
Dox, di siŋse tey noos, ba estation,
Ngir jënd crème glacé.
Pincez tous vos koras, frappez les balafons!
Mangi ci koñn bi ak Guinness,
Gën xale daldi joy.
Man la regal wala xàjj bi?
Sama yaaye, sama baaye, sama super etoile.
Pox forox!
Ku may sa baay ndox dangi suuk, di jonkal.
Yaàq ngeen!
Non, non, bunu nangu nu nu teg stress.
Féccal!
Terrace bi:
Di tog fataaya,
Di làkk mbóq,
Di naan attaya,
Ak samay mbokk.
Bokuñ dërët,
Waye sama xol lañu am.
Allahu akabar!
Suba dinaa tela yéewu
Ngir jënd fondé
Wala mburu ban
Ngir lekk ak nen.
Ndiayekounda:
Tali bu x’ónq.
“Dad, can we sit on the roof?”
Ay waye, ne na waaw!
Oh say can you see…
Mangi dem pour ben at kese,
Ba dewen, dég nga.